Bu leen sunu liggéey bi nuy def ci podcast yi neexee te ngeen bëgg mu gën a jaar yoon ak ndaje yi nuy def gën a am solo ak yeneen xalaat yu bees, man ngeen noo dooleel ngir nu jëm kanam.
Dooleel podcast Wolof Tech
Seen ndimbal dina nu jàppale ngir nu man a yaatal liggéey bi rafetal ko te mooy tasaare jumtukaayu xarala yi ci Senegaal.