Jamono jiy daw
Yeneen jamono yi

JAMONO 11
Nous sommes ravis de vous dévoiler la saison 11 du podcast woloftech ! 🎙️✨ Plongez dans un univers où la
12 June 2023

JAMONO 10
La Fintech peut être la solution pour aider à transformer les systèmes financiers du continent en adaptant des outils de
22 January 2023

JAMONO 9
En collaboration avec RootSN nous avons produit cette saison pour accompagner la structure dans ce grand événement de sensibilisation dont
16 October 2022
No more posts to show
Ñi nu dalaloon
Fésalal sa liggéey jaare ko ci Wolof Tech
Su fekkee dangeen yor ag lijjanti walla liggéeyu kenn nit te ngeen bëgg koo siiwal, man ngeen a jënd sunu dog yi nuy amal ci jamono yi, ngir gën a fésal seen ub liggéey walla seen um njaay.
Danuy ànd ak yéen ci seen naali podcast yi
Su fekkee dageen a am ay naali podcast, man nanu leen a gunge ci anam yu wuute ba ngeen sottal seen i mébet. Dinanu def ay tàggat yu wuute ci nu ñuy defare ay dog ba mu jaar yoon doon lu am njariñ ak nu ñuy jëfandikoo jumtukaay yi ba ngeen am kàddu yu leer.
Nekk sunu lëkkatoo
Su fekkee dangeen a yor ag lijjanti gu yaatu walla gu ndaw te ngeen bëgg a liggéey ak nun ci xarala yu yees yi ci Senegaal, man nanoo ànd ag lëkkatoo ngir yaatal xalaat yi.
